『Layene Digital』のカバーアート

Layene Digital

Layene Digital

著者: LayeneDigital
無料で聴く

Portail Digital de la communauté #LayeneLayeneDigital イスラム教 スピリチュアリティ
エピソード
  • Zikrullah - Ñaanu Seydina Limamou Lahi (PSL) 2026
    2026/04/21

    Niroo ak demug Imaam al Laay xayrunaasGuddig Jumaa ja boobu bés tam tàng naLu jiitu dig ba ñaari ay bés Maam LibaasJiite jullit ña cëy koreem ga metti naLimaamu nan gaaw leen ma àgg JàmmaLaayAnna janazatun digam ba yemb naYaram wa jeexMu mel ni bant bu nu solal ay yére,Leer ya wër kanam ga taaru naMu naan ku yéene jox Yónnen bi ab dërëm na andi jox ma man la maay RasuulunaMu wax xarit ba Seex Maxtaar Xawsuna jàngal xutab yi muy duuras ci Axlu naFeebar ba dëj ko muy sikar di waaj xanaa, lu nu mën dal war nan xalaat ImaamanaGuddig jumma ja, fukki fan ginaaw kori ak ñenti fan Limaamu génn àddunaJigéen ñay yuuxu, saaba yépp booloo di jooy te naan nax ga nu rek ba dem ay waay xabibunaaManjoon taxaw yor jaasi naan kenn du fi rob Libaas te Sëydinaa ñëwul li yell naÑuy xaar Isaa ndax bëyti Maamuur lay bawoo ñuy jooy Limaamu ñetti fan ya metti naMu ñëw di fóon kanam ga naan ko Waalidi tipta xayyan wa maytan wa RabbinaMu nan leen ku daan jaamu Limaamu mën ga dem Kuy jaamu Yàlla toog nu gëm MaalikunaMiimun la toog kenn jooyatul ImaamunaBa dee jëlaat ko mook Manjoon ak XutbunaaLa jël Limaamu jël Isaa mi xayrunaasDu bàyyi kenn sax fi di beel ci àddunaLa jël Manjoon, jël Baabakar mi xawsunaMo jël Isaa ak Baay Raan mi doon xutwatunaKon kay du tee Useynu daanu waatxanaa, lu nu mën dàll war nan xalaat ImaamunaMësu nu xalaat bés dina ñëw Seriif AbdulaayGa tàggatoo ñu des ganaawMaam, ya taxoon nu dëkkee daw Amo moroom Baay Abdulaay

    続きを読む 一部表示
    1 時間 35 分
  • Zikrullah - Ñaanu Seydina Issa Rouhou Lahi (PSL) 2026
    2026/04/21

    𝑩𝒂𝒂𝒚 𝑺𝒆𝒚𝒅𝒆𝒆𝒚 𝑹𝒖𝒙𝒖 𝑹𝒂𝒙𝒎𝒂𝒂𝒏

    𝑵𝒖 𝒏𝒈𝒊 𝒍𝒂𝒚 𝒈𝒆𝒎 𝒍𝒂𝒂𝒚 𝒎𝒂𝒅𝒊𝒊𝒏𝒆𝒆

    𝑫𝒊 𝒍𝒂 𝒏𝒖𝒚𝒖 𝒍𝒂𝒂𝒚 𝒎𝒂𝒎𝒂𝒅𝒖 𝒎𝒂𝒙𝒕𝒂𝒓

    𝑫𝒊 𝒍𝒂 𝒚𝒂𝒌𝒂𝒂𝒓 𝒚𝒂𝒘 𝒎𝒂𝒅𝒊𝒊𝒏𝒆 🖤


    #layene #islam #layenedigital #zikrullah

    続きを読む 一部表示
    1 時間 53 分
  • Mame Libasse Lahi - Ñaanu Seydina Issa Rouhou Lahi (PSL) 2026
    2026/04/19

    “Jàmm rekk laay am bis ba ma juddoo, ak ca bis ba may dee ak bis ba may dekkiwaat”. (S19 V33)


    Ruhu Laay Alasaan jàlle nu 🤍


    #layenedigital #layene #islam

    続きを読む 一部表示
    1 時間 12 分
adbl_web_anon_alc_button_suppression_t1
まだレビューはありません